Galatians 6:16 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ñiy topp ndigal lii nag, na Yàlla wàcce jàmm ak yërmande ci ñoom, ak ci Israyilu Yàlla.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mboolem ñiy sàmm ndigal lii nag, te di Israyilu Yàlla, jàmm ak yërmande ñeel na leen.