Galatians 6:17 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Léegi nag, bu ma kenn lëjalati, ndaxte yor naa ci sama yaram ay leget yuy màndargaal ne, jaamu Yeesu laa.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Li ci des moo di gannaaw-si-tey, bu ma kenn lëjalati, ndax légét yi ci sama yaram, samag bokk ci Yeesu la màndargaal.