Genesis 1:26 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yàlla ne: «Nanu bind nit ci sunu melokaan, mu nirook nun, te na yilif jëni géej ak picci asamaan ak jur gépp ak suuf sépp ak lépp lu ciy raam.»