Genesis 12:15 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Jaraafi Firawna itam gis ko, di ko kañ ca Firawna ndax taar ba, ñu daldi ko yóbbu ca kër Firawna.