Genesis 13:1 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bi loolu amee Ibraam dafa jóge Misra, moom ak soxnaam, yóbbaale alalam jépp, daldi dem ca àllub Negew, Lóot topp ca.