Genesis 14:10 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye xuru Sidim woowu dafa feesoon dell aki pax aki kàmbi koltaar. Ba mu ko defee buuri Sodom ak Gomor di daw, far daanu ca kàmb ya. Ña ca des daw ba ca tund ya.