Genesis 14:24 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Duma jël dara, lu wees li sama nit ñi lekk ba noppi ak sama wàllu farandoo yi, di Aner ak Eskol ak Mamre, ñoom it, nañu jot seen wàll.»