Genesis 18:29 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ibraayma dellu wax ne: «Su fa ñeent fukk ñu jub rekk amee nag?» Aji Sax ji ne ko: «Duma def dara ngir ñeent fukk ñooñu.»