Genesis 19:30 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gannaaw loolu Lóot dafa ragala dëkk Sowar, ba toxoo fa, ànd ak ñaari doomam yu jigéen, sanci ca tund ya. Mu dëkk ci xuntim xeer, moom ak ñaari doomam yu jigéen.