Genesis 2:20 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba mu ko defee nit kooku, di Aadama, tudd jur gépp ak picc yépp ak rabi àll yépp, waaye fekku ca ku koy jàpple te jekk ci doon wéttalam.