Genesis 20:4 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Loolu fekkul Abimeleg dëkkoo Saarata. Mu wax Yàlla ne ko: «Sama Boroom, mbaa doo bóom réew mi ci mbir mu ñu doonul dara?