Genesis 21:22 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Jamono yooyu Abimeleg àndoon na ak Pikol kilifay xarekatam, dem ci Ibraayma ne ko: «Gis naa ne Yàlla ànd na ak yaw, di àntal li ngay def lépp.