Genesis 22:19 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba loolu wéyee Ibraayma waññiku, fekki surga ya, ñu daldi ànd ñoom ñépp, jëm Beerseba, ndax fa la Ibraayma dëkkoon.