Genesis 22:7 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Isaaxa ne baayam Ibraayma: «Baay!» Mu ne ko: «Naam, doom sama.» Isaaxa ne ko: «Sawara saa ngi, matt maa ngi, waaye ana gàtt, bi nuy sarxal?»