Genesis 23:11 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Déglul, ma wax la, kilifa gi, fabal tool bi, booleek xuntim xeer, mi ci nekk far. Maa la ko jox ci sama kanami bokk; jëlal, denc fa sa néew.»