Genesis 24:25 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
teg ca ne ko: «Waawaaw, ñax maak ngooñ maa nga fa, ne gàññ, te it manees na faa dal.»