Genesis 24:48 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba mu ko defee ma sujjóotal Aji Sax ji, sant Aji Sax jiy sama Yàllay sang Ibraayma, ndax jubal na sama yoon, ba ma jëlal doomam soxna ciy bokkam.