Genesis 24:5 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Surga ba ne ko: «Su ndaw sa nanguwula ànd ak man ci réew mii nag? Ndax kon damaa wara yóbbu sa doom ba ca réew ma nga jóge?»