Genesis 26:32 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ca bés booba ay surgay Isaaxa ñëw nañu, di ko wax lu jëm ci teen, ba ñu doon gas, ne ko: «Gis nanu ndox.»