Genesis 27:34 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Esawu dégg li baayam wax rekk, yuuxu yuux gu réy ndax naqar. Mu ne baayam: «Ngalla baay, ñaanal ma, man itam.»