Genesis 27:41 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Esawu nag bañ Yanqóoba ndax barke ba ko baayam ñaanal. Ma ngay wax ca xolam naan: «Balaa yàgg ñu dëj sama baay, te bu boobaa dinaa rey sama rakk Yanqóoba.»