Genesis 27:6 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Rebeka moom ne doomam Yanqóoba: «Dégg naa sa baay wax sa mag Esawu ne ko: