Genesis 29:13 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba Laban déggee ne jarbaatam Yanqóoba ñëw na, dafa daw gatandu ko, taf ko ci boppam, fóon ko, yóbbu ko kër ga. Ba Yanqóoba nettalee Laban lépp,