Genesis 29:8 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñu ne ko: «Dunu ko man mbete gétt yépp daje, nu béraŋ doj wi, ubbi teen bi, doora wëgg gàtt yi.»