Genesis 31:52 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Jal bi seede la, doj wi di seede ne duma jéggi jal bi, jublu ci yaw, te yaw itam doo jéggi jal bi mbaa doj wi, jublu ci man, te naraluloo ma jàmm.