Genesis 31:8 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bu nee: “Yi tippanteey sa peyoor,” jur gépp jur lu tippante; mbaa mu ne: “Yi seereer ay sa peyoor,” jur gépp jur lu seereer.