Genesis 33:13 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yanqóoba ne ko: «Sang bi, xam nga, xale yi dañoo néew doole, te it gàtt yi ak nag yiy nàmpal laay xalaat. Su nu leen sëqatalee benn bés rekk, gàtt yépp dee.