Genesis 34:10 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Su ko defee ngeen dëkk ak nun te réew mi di seen réew. Man ngeen fee sanc, dem fu leen neex, sàkku fi alal.»