Genesis 34:11 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Sikem it wax ak baayu Diina ak càmmiñ ya ne leen: «Su ngeen ma nangulee, lépp lu ngeen ma wax dinaa ko joxe.