Genesis 34:23 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bu nu leen nangulee, ba ñu dëkk ci sunu biir, kon seeni jur ak seen alal ak seen mala yépp, ndax du nooy doon boroom?»