Genesis 34:25 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ca gannaaw ëllëg sa ñu ànd ak metit, ñaari doomi Yanqóoba ya, Simeyon ak Lewi, càmmiñi Diina, jël seeni saamar, dugg ca dëkk ba, bett leen, rey góor ñépp.