Genesis 34:8 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Amor wax ak ñoom ne leen: «Sama doom Sikem dafa bëgg seen jigéen ci xolam. Dama leen di ñaan, ngeen may ko ko jabar.