Genesis 36:2 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Esawu jël na janqi Kanaaneen jabar. Ñooñoo di: Ada doomu Elon, Etteen ba, ak Olibama doomu Ana, miy doomu Sibeyon, Eween ba,