Genesis 37:17 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waa ja ne ko: «Jóge nañu fii de, ndax dégg naa ñu naan: “Nanu dem Dotan.”» Yuusufa toppi magam ya ba Dotan, fekk leen fa.