Genesis 37:2 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Askanu Yanqóoba mooy lii. Yuusufa tollu na ci waxambaane, am fukki at ak juróom ñaar, di sàmmle jur gi doomi baayam, yi nga xam ne soxnay baayam Bilaa ak Silpa ñoo leen jur. Yuusufa nag di leen boole ak seen baay.