Genesis 37:22 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ruben teg ca ne leen: «Buleen tuur deret. Sànnileen ko ca kàmb gee ca àll ba, waaye bu ko loxo dal.» Booba ma ngay wut nu mu xettlee Yuusufa ci ñoom, ba delloo ko baayam.