Genesis 37:3 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Booba Yanqóoba, Yuusufa la gëna bëgg ci ay doomam, ndax li mu màggat door koo am. Mu ràbblul ko mbubb mu yànj.