Genesis 38:1 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ca jamono yooyu Yuda dafa teqlikoo ak ay doomi baayam, dal ca waa ju dëkk Adulam te tudd Ira.