Genesis 38:12 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba ñu demee ba mu yàgg, doomu Suwa, soxnas Yuda faatu. Ba dëj ba wéyee, Yuda dem fekki watkati xaram ca Timna. Ira, xaritam bi dëkk Adulam a nga ànd ak moom.