Genesis 4:22 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Silla moom jur Tubal Kayin miy tëgg lépp luy jumtukaayu xànjar ak weñ. Tubal Kayin am na jigéen bu tudd Naama.