Genesis 41:21 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye bi ñu leen lekkee ba noppi, itam dafa mel ni lekkuñu leen, ndax terewuleena mel na woon. Booba laa yewwu,