Genesis 41:31 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Xiif bi dina tax lenn luy nirook naataange dootu des ci réew mi, ndax dina metti lool.