Genesis 41:35 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñoom nañu dajale mboolem dundi at yu baax yi, te boole pepp mi ci sa ndigalu bopp, yaw Firawna, muy dund bu ñuy denc ci dëkk yi.