Genesis 42:24 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci biir loolu mu dummóoyu leen, di jooy. Ba mu jooyee ba noppi, walbatiku, wax ak ñoom, doora jël Simeyon, jéng ko ci seen kanam.