Genesis 42:34 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
su ko defee ngeen indil ma seen rakk ju ndaw, kon dinaa xam ne dungeen ay yëddukat waaye nit ñu maandu ngeen, te dinaa leen delloo seen mbokk, ngeen mana dem fu leen neex ci réew mi.”»