Genesis 42:9 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Xelum Yuusufa ne yarr ca la mu géntoon ca ñoom, daldi ne leen: «Yeen ay yëddukat ngeen, yuy nemmikusi mbóoti réew mi.»