Genesis 43:2 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba ñu lekkee pepp mi ñu jële woon Misra, ba mu jeex, seen baay ne leen: «Delluleen, wutali nu dund.»