Genesis 45:22 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
mayaale leen ku ne mbubb mu rafet. Waaye Beñamin moom, ñetti téeméeri dogi xaalis la ko may, tegal ko ca juróomi mbubb yu rafet.