Genesis 45:9 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Gaawleen dellu ci sama baay te ne ko: “Sa doom Yuusufa nee na: Yàlla fal na ma kilifag Misra gépp; ñëwal fi man, nu mu gëna gaawe.