Genesis 46:1 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Israyil nag dem, yóbbaale mboolem lu bokk ci moom. Ba mu agsee Beerseba, dafa sarxal Yàllay baayam Isaaxa.